Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:14-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Xamal ne xel mu rafet ni la neexe; soo xeloo, sa muj rafet, te sa yaakaar du tas.
15Soxor bi, bul tëru ku jub ci këram, bul yàq dëkkuwaayam.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:14-15Kàddu yu Xelu 24:14-15