Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:14-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Xamal ne xel mu rafet ni la neexe; soo xeloo, sa muj rafet, te sa yaakaar du tas.
15 Soxor bi, bul tëru ku jub ci këram, bul yàq dëkkuwaayam.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi