Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 23

Kàddu yu Xelu 23:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ndog soo ca lekk, waccu ko, yiw woo ko wax daldi neen.
9Bul wax akub dof, day xeeb sam xel.
10Bul toxal màndargam cosaan ci làccu suuf, bul aakimoo suufas jirim.

Read Kàddu yu Xelu 23Kàddu yu Xelu 23
Compare Kàddu yu Xelu 23:8-10Kàddu yu Xelu 23:8-10