Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Ndog soo ca lekk, waccu ko, yiw woo ko wax daldi neen.
9 Bul wax akub dof, day xeeb sam xel.
10 Bul toxal màndargam cosaan ci làccu suuf, bul aakimoo suufas jirim.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi