Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 23

Kàddu yu Xelu 23:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Bul xemmem daraam lu neex, ñam woowu la lay naxe.
4Bul rey sa bopp ci wut alal, bu ko xalaat sax.
5Ndax xef ak xippi mu wéy, mel ni lu saxi laaf, ne fëyy, naaw ni jaxaay.

Read Kàddu yu Xelu 23Kàddu yu Xelu 23
Compare Kàddu yu Xelu 23:3-5Kàddu yu Xelu 23:3-5