Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 23:3-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 23:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Bul xemmem daraam lu neex, ñam woowu la lay naxe.
4 Bul rey sa bopp ci wut alal, bu ko xalaat sax.
5 Ndax xef ak xippi mu wéy, mel ni lu saxi laaf, ne fëyy, naaw ni jaxaay.
Kàddu yu Xelu 23 in Kàddug Yàlla gi