Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
4Woyofal te ragal Aji Sax ji, am alal, gudd fan ak daraja.
5Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.
6Tegal gone ciw yoon, ba bu màggee, du ko wacc.

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:3-6Kàddu yu Xelu 22:3-6