Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,
23Aji Sax ji da koy taxawu, ku ko xañ, mu xañ la bakkan.

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:22-23Kàddu yu Xelu 22:22-23