Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:22-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:22-23 in Kàddug Yàlla gi

22 Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,
23 Aji Sax ji da koy taxawu, ku ko xañ, mu xañ la bakkan.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi