Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:19-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Yaw laa koy xamal tey jii, ndax nga wóolu Aji Sax ji.
20Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,
21ngir xamal la lu wér te dëggu, nga yóbbaale kàdduy dëgg, yoo tontoo ña la yebal.
22Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:19-22Kàddu yu Xelu 22:19-22