Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:19-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Yaw laa koy xamal tey jii, ndax nga wóolu Aji Sax ji.
20 Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,
21 ngir xamal la lu wér te dëggu, nga yóbbaale kàdduy dëgg, yoo tontoo ña la yebal.
22 Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi