Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:16-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Not néew-ji-doole ngir yokkule, mbaa may boroom alal, loo ci def mu wàññi la.
17Teewlul te déglu li boroom xel yi wax. Defal sam xel ci li ma lay xamal.

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:16-17Kàddu yu Xelu 22:16-17