Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:16-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:16-17 in Kàddug Yàlla gi

16 Not néew-ji-doole ngir yokkule, mbaa may boroom alal, loo ci def mu wàññi la.
17 Teewlul te déglu li boroom xel yi wax. Defal sam xel ci li ma lay xamal.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi