Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Aji Sax jeey sàmm liy dëgg, di weddi waxi fen-kat.
13Bul yaafus, ba naan: «Gayndee ngi ci biti, dañu may rey ci mbedd mi!»

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:12-13Kàddu yu Xelu 22:12-13