Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:12-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Aji Sax jeey sàmm liy dëgg, di weddi waxi fen-kat.
13 Bul yaafus, ba naan: «Gayndee ngi ci biti, dañu may rey ci mbedd mi!»
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi