Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:6-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Alal ju la fen may, cóolóol la, day naaw, wut ko xaru la.
7Coxor day sànk boroom, ndax day baña def njub.
8Ab saaysaay day dëngal, nit ku dëggu di jubal.
9Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
10Ab soxor day namma lore, te du yërëm moroomam.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:6-10Kàddu yu Xelu 21:6-10