Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Dëkke ndànd-foyfoy moo gën jabar ju tàng, bare ay.
20Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
21Ku saxoo njekk ak ngor am fan wu gudd, naataangeek daraja.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:19-21Kàddu yu Xelu 21:19-21