Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 21:19-21 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 21:19-21
in
Kàddug Yàlla gi
19
Dëkke ndànd-foyfoy moo gën jabar ju tàng, bare ay.
20
Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
21
Ku saxoo njekk ak ngor am fan wu gudd, naataangeek daraja.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms