Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ku topp sa bànneex, mujje ñàkk; ku sopp biiñ ak lu niin du woomle.
18Ku bon këppoo ayu ku baax, workat gàddu musibam kuy jubal.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:17-18Kàddu yu Xelu 21:17-18