Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:17-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Ku topp sa bànneex, mujje ñàkk; ku sopp biiñ ak lu niin du woomle.
18 Ku bon këppoo ayu ku baax, workat gàddu musibam kuy jubal.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi