Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:15-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Bu yoon amee, ku jub bég; kuy def lu bon jàq.
16Ku noppee jëfe xel, noppluji njaniiw.
17Ku topp sa bànneex, mujje ñàkk; ku sopp biiñ ak lu niin du woomle.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:15-17Kàddu yu Xelu 21:15-17