Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ku tanqamlu jooyi ku ñàkk dina woote wall, wall ñàkk.
14Ku mer, may ko ci sutura, mu giif; boroom xadar, boqal ko neexal, mu dal.
15Bu yoon amee, ku jub bég; kuy def lu bon jàq.
16Ku noppee jëfe xel, noppluji njaniiw.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:13-16Kàddu yu Xelu 21:13-16