Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Ku tanqamlu jooyi ku ñàkk dina woote wall, wall ñàkk.
14 Ku mer, may ko ci sutura, mu giif; boroom xadar, boqal ko neexal, mu dal.
15 Bu yoon amee, ku jub bég; kuy def lu bon jàq.
16 Ku noppee jëfe xel, noppluji njaniiw.
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi