Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Ab soxor day namma lore, te du yërëm moroomam.
11Boo mbugalee kuy ñaawle, ab téxét jànge ca; nga jàngal ku rafet xel, mu yokku.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:10-11Kàddu yu Xelu 21:10-11