Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 20

Kàddu yu Xelu 20:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Naan biiñ ak ñaawle, naan ñoll, tanqale, ku mu nax xeluwoo.
2Buur mer lool, mel ni gayndee ŋar; boo ko merloo, dangay xaru.
3Moytuw ay, ndam la; dof boo gis day bëgg xuloo.

Read Kàddu yu Xelu 20Kàddu yu Xelu 20
Compare Kàddu yu Xelu 20:1-3Kàddu yu Xelu 20:1-3