Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6ngir mana xam aw léeb aku taas ak kàddug boroomi xel yu rafet ak seeni cax.
7Ragal Aji Sax ji di njàlbéenu xam-xam, te xel mu rafet akub yar, dof yaa ko xeeb.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:6-7Kàddu yu Xelu 1:6-7