Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:6-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 ngir mana xam aw léeb aku taas ak kàddug boroomi xel yu rafet ak seeni cax.
7 Ragal Aji Sax ji di njàlbéenu xam-xam, te xel mu rafet akub yar, dof yaa ko xeeb.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi