Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:28-29

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28Keroog nga woo ma wall, duma wuyu, nga seet ma, seet, doo ma gis.
29Daa fekk nga baña xam, te ragal Yàlla du loo taamu.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:28-29Kàddu yu Xelu 1:28-29