Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:28-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:28-29 in Kàddug Yàlla gi

28 Keroog nga woo ma wall, duma wuyu, nga seet ma, seet, doo ma gis.
29 Daa fekk nga baña xam, te ragal Yàlla du loo taamu.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi