Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Soo dëppee ba déglu, ma àrtu la. Ma ne, kon ma xellil la samam xel, xamal la samay kàddu.
24Damaa woote, nga gàntal, ma tàllal loxo, faaleesu ma.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:23-24Kàddu yu Xelu 1:23-24