Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Doom, bul ànd ak ñoom ciw yoon, bul jaare fa ñuy jaar,
16ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:15-16Kàddu yu Xelu 1:15-16