Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:15-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Doom, bul ànd ak ñoom ciw yoon, bul jaare fa ñuy jaar,
16 ngir dañuy xélu, nar musiba, di gaawtuy sànk bakkan.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi