Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
11Dañu la naan: «Dikkal, nu tëruji bakkan, yeeruji jaambur bu deful dara.
12Nanu mel ni njaniiw, mëdd kuy dund, mu jekki tàbbi biir bàmmeel.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:10-12Kàddu yu Xelu 1:10-12