Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:10-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
11 Dañu la naan: «Dikkal, nu tëruji bakkan, yeeruji jaambur bu deful dara.
12 Nanu mel ni njaniiw, mëdd kuy dund, mu jekki tàbbi biir bàmmeel.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi