Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 19

Kàddu yu Xelu 19:20-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Déggal ndigal te yaru, ndax ëllëg nga xelu.
21Bare na lu xol di mébét, waaye Aji Sax jeey dogal.
22Li ñu sopp ci nit mooy ngor, néewle moo gën fen.
23Ragalal Aji Sax ji ndax nga gudd fan, nopplu te baña loru.

Read Kàddu yu Xelu 19Kàddu yu Xelu 19
Compare Kàddu yu Xelu 19:20-23Kàddu yu Xelu 19:20-23