Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 19:20-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 19:20-23 in Kàddug Yàlla gi

20 Déggal ndigal te yaru, ndax ëllëg nga xelu.
21 Bare na lu xol di mébét, waaye Aji Sax jeey dogal.
22 Li ñu sopp ci nit mooy ngor, néewle moo gën fen.
23 Ragalal Aji Sax ji ndax nga gudd fan, nopplu te baña loru.
Kàddu yu Xelu 19 in Kàddug Yàlla gi