Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Bu mbon nuyoo, xeebeel topp ca; jëf ju ñaaw, gàcce rekk.
4Waxi nit ndox mu xóot la, bu bënnee, xelli, ñu di ca xelu.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:3-4Kàddu yu Xelu 18:3-4