Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Bu mbon nuyoo, xeebeel topp ca; jëf ju ñaaw, gàcce rekk.
4 Waxi nit ndox mu xóot la, bu bënnee, xelli, ñu di ca xelu.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi