Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Ku ñàkk a ngi leewaayu, boroom alal di ko jànni.
24Barey àndandoo lor a ngi ci, waaye xarit a ngi gëna taq nit mbokkam.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:23-24Kàddu yu Xelu 18:23-24