Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:20-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
22Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.
23Ku ñàkk a ngi leewaayu, boroom alal di ko jànni.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:20-23Kàddu yu Xelu 18:20-23