Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:20-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:20-23 in Kàddug Yàlla gi

20 Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21 Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
22 Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.
23 Ku ñàkk a ngi leewaayu, boroom alal di ko jànni.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi