Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:20-21Kàddu yu Xelu 18:20-21