Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 18:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 18:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Làmmiñ feesal na biiru boroom, yoolu kàddu suur na boroom.
21 Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.
Kàddu yu Xelu 18 in Kàddug Yàlla gi