Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 17

Kàddu yu Xelu 17:17-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Xarit du bëgg, di bañ; mbokk day bokk ak yaw say coono.
18Ku ñàkk bopp ay dige feyal jaambur, di ko gàddul boram.
19Ku bëggu ay bëggi tooñ; damu, yàqule.
20Ku njublaŋ du baaxle, kuy wax njekkar añe musiba.

Read Kàddu yu Xelu 17Kàddu yu Xelu 17
Compare Kàddu yu Xelu 17:17-20Kàddu yu Xelu 17:17-20