Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:17-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:17-20 in Kàddug Yàlla gi

17 Xarit du bëgg, di bañ; mbokk day bokk ak yaw say coono.
18 Ku ñàkk bopp ay dige feyal jaambur, di ko gàddul boram.
19 Ku bëggu ay bëggi tooñ; damu, yàqule.
20 Ku njublaŋ du baaxle, kuy wax njekkar añe musiba.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi