Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 17

Kàddu yu Xelu 17:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Ku am ug dégg ngay yedd benn yoon, ab dof téeméeri yar du ko waññi.
11Ku bon fippu doŋŋ lay jéem, te musibaa koy dikkal.

Read Kàddu yu Xelu 17Kàddu yu Xelu 17
Compare Kàddu yu Xelu 17:10-11Kàddu yu Xelu 17:10-11