Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Ku am ug dégg ngay yedd benn yoon, ab dof téeméeri yar du ko waññi.
11 Ku bon fippu doŋŋ lay jéem, te musibaa koy dikkal.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi