Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:30-32

Help us?
Click on verse(s) to share them!
30Piise, ku nar njekkar; màttu, ku def lu bon.
31Bijjaawu bopp kaala gu yànj la, njekk a koy maye.
32Muñ mer, moo gën njàmbaar; tënk sa bakkan moo raw nangub dëkk.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:30-32Kàddu yu Xelu 16:30-32