Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:30-32 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:30-32 in Kàddug Yàlla gi

30 Piise, ku nar njekkar; màttu, ku def lu bon.
31 Bijjaawu bopp kaala gu yànj la, njekk a koy maye.
32 Muñ mer, moo gën njàmbaar; tënk sa bakkan moo raw nangub dëkk.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi