Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:16-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Wutal xel mu rafet, bàyyi wurus; taamul ag dégg, wacc xaalis.
17Yoonu kuy jubal day moyu lu bon, ku teeylu sa jëfin, sàmm sa bakkan.
18Réy, yàqule; xeebaate, jóoru.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:16-18Kàddu yu Xelu 16:16-18